njamala gi
giraffe - la girafe

rab wi
wild animal - animal sauvage

Wolof English français
golo gi, (ndinki) monkey, ape le singe
dàngin gorilla le gorille
xojox gi squirrel of Gambia l'écureuil de Gambie
jaar ji striped ground squirrel l'écureuil fouisseur,
le rat palmiste
njugub bi bat la chauve-souris
coy mi, seku bi   parrot le perroquet
terëx bi flamingo le flamant
ngëj mi marabou stork le marabout
banjóóli bi, baa bi   ostrich l'autruche
gaynde gi  , gar gi le lion
segg mi   leopard,
panther
le léopard,
la panthère
tene mi cheetah le guépard
bukki bi   hyena la hyène
till gi jackal le chacal
saafaandu gi African "wild dog" le lycaon
giléem, géléem gi camel le chameau
kooba gi antelope l'antilope
kéwél gi   la gazelle
fasu-àll wi zebra le zèbre
njamala gi   giraffe la girafe
ñey wi   elephant l'éléphant
wànga-lànga wi rhinoceros le rhinocéros
nagu-àll wi buffalo le buffle
léebéer bi hippopotamus l'hippopotame
jasig ji   le crocodile


mala mi - l'animal

Wolof English français
xaj bi   dog le chien
kuti bi   puppy le chiot
muus mi, wund wi, janaab ji cat le chat
kaña gi le rat
jinax ji mouse la souris
mbaam-sëf mi
cumbur mi
donkey, (ass)
 
l'âne
l'ânon
berkelle bi   mule le mulet
fas wi   horse le cheval
wajan wi mare la jument
mool wi foal le poulain
yëkk wi   bull le taureau
xàbban bi ox le bœuf [castré]
nag wi cow la vache
séll wi calf le veau
sàmm(kat) bi   sheepherder, shepherd le berger
xar mi sheep le mouton
xar mu-jigéén ewe la brebis
mbote mi, (mburtu) lamb l'agneau
béy, bëy wi goat la chèvre
tef bi kid le chevreau, le cabri
mbaam-xuux mi pig le cochon, le porc
mbaam-àll mi warthog le phacochère
pax mi burrow le terrier
njombor gi  
lëg bi
rabbit
hare
le lapin
le lièvre
suñel bi hedgehog le hérisson
wel wi fennec fox le renard des sables


picc mi  bird - l'oiseau

Wolof English français
tàgg bi nest le nid
jaxaay ji eagle l'aigle
maf mi hawk, falcon le faucon
tan mi   vulture le vautour, charognard
looy, xargeej owl le hibou, la chouette
baaxoñ bi raven le corbeau
petax mi   le pigeon
cokkeer bi partridge la perdrix
naat bi guineafowl la pintade
koppin bi turkey le dindon, la dinde
séq gi rooster, (cockerel) le coq
ganaar gi   hen la poule
cuuj bi chick le poussin
kanaara gi
xanqel bi
drake
duck
le canard
la cane


jën wi  fish - le poisson

Wolof English français
waxandor wi   tuna le thon
gaynde-gééj gi shark le requin
piipa bi dolphin le dauphin
ngaaga li whale la baleine
junqóob bi, koti bi crab le crabe
sippax bi shrimp, prawn la crevette
mbonnatu-ndox mi
mbonnatu-suuf mi
sea turtle
land turtle, tortoise
la tortue marine
la tortue terrestre
buuj bi (sea)shell le coquillage
ngumbaan-tooye bi, (rebes) snail l'escargot
watar leech la sangsue
jaan ji   snake le serpent
kàkkatar bi   chameleon le caméléon
unk bi   le gecko
sindax bi   lizard le lézard, [l'agame]
mbott mi frog, toad la grenouille, le crapaud


gunóór gi, (gasax, gesax) - l'insecte

Wolof English français
njéeréer bi desert locust le criquet pèlerin
soccent bi grasshopper la sauterelle
mellentaan wi   little black ant la petite fourmi noire
max mi   les termites
weñ wi   fly la mouche
lëpp-lëpp bi butterfly le papillon
xund-xund bi dragonfly la libellule
xuyéntaan bi firefly la luciole
sugum si beehive la ruche
yamb wi   bee l'abeille
nguri li wasp la guêpe
yoo wi   mosquito le moustique
tééñ bi lice les poux
fel wi fleas les puces
weteñ wi tick la tique
mbóot mi   cockroach le cafard
jargoñ gi
lënd wi
spider
spider web, cobweb
l'araignée
la toile d'araignée
géléemu-maam-yàlla bi praying mantis la mante religieuse
jiit ji le scorpion