xam-xamu dun bi
geography - la géographie
| Wolof |
English |
français |
réew mi
 |
country |
le pays |
| péey bi |
capital city |
la capitale |
dëkk bi
 |
town, city |
la ville |
| Gànnaar gi |
Mauritania |
la Mauritanie |
naar bi
 |
Mauritanian |
mauritanien |
| Senegaal |
Senegal |
le Sénégal |
| waa Senegaal |
Senegalese |
sénégalais |
waa ji
 |
inhabitant |
l'habitant |
lébu
 |
lebou |
lébou |
| Ndakaaru |
Dakar |
" |
| Kaasamaas gi |
|
la Casamance |
Gàmbi
 |
Gambia |
la Gambie |
| Giné |
Guinea |
la Guinée |
Tugël
 |
|
l'Europe, la France |
tubaab bi
 |
European |
européen, [blanc] |
direction
| Wolof |
English |
français |
| bëj-gànnaar |
North |
le Nord |
| bëj-saalum |
South |
le Sud |
penku
 |
East |
l'Est |
sowu
 |
West |
l'Ouest |
| Wolof |
English |
français |
| ci kaw |
on the top of, over |
au-dessus, sur |
| ci suuf |
at the bottom of, under |
au-dessous, sous |
| ci biir |
inside, into |
dedans |
| ci biti |
outside, out of |
dehors |
| ci ginnaaw |
behind |
derrière |
| ci kanam |
in front of |
devant |
| ci boor/wet |
beside, around |
à côté |
| ci diggënte |
in between |
entre |
| ci digg |
in the center/middle |
au centre, au milieu |
| ndeyjoor bi |
right |
droite |
| càmmooñ bi |
left |
gauche |
fii
 |
here |
ici |
fa
 |
there |
là, là-bas |
jege
 |
near |
près, proche |
sore
 |
far |
loin, lointain |