Wolof | English | français |
néegu-ñax bi | hut | la hutte |
tool bi
![]() toolu dër bi |
garden | le jardin le jardin potager |
teerukaay bi, gaaraas bi | garage | " |
jank bi | roof | le toit |
sàq mi | attic | le grenier |
kam gi, kaaw bi | basement | la cave |
teraas bi | terrace | la terrasse |
palanteer bi
![]() |
window | la fenêtre |
ridó bi | curtain | le rideau |
taax mi | wall | le mur |
bunt bi
![]() |
door | la porte |
tëjukaay bi, selluur bi | lock | la serrure |
caabi ji
![]() doom bi ![]() |
key | la clé, clef |
yéegukaay bi | stairway | l'escalier |
etaas bi | floor, storey | l'étage |
bulu bi, saal bi | living-room | la salle de séjour |
anteen bi | antenna | l'antenne |
rajo bi | radio | " |
tele bi
![]() |
television | la télévision |
néeg bi
![]() |
bedroom | la chambre |
lal bi
![]() |
bed | le lit |
malaan mi | blanket | la couverture |
tapi bi | carpet | le tapis |
almet bi/ji | match(es) | allumette(s) |
làmp bi | lamp | la lampe |
àmpul bi | lightbulb | l'ampoule |
waañ wi
![]() |
kitchen | la cuisine |
lakkukaay bi, puur bi | oven | le four |
firsideer bi | refrigerator, "fridge" "freezer" |
le réfrigérateur le congélateur |
lekkuwaay bi | dining-room | la salle à manger |
taabal bi | table | " |
siis bi
![]() |
chair | la chaise |
toogu bi, fotëey bi | armchair | le fauteuil |
sanguwaay bi | bathroom | la salle de bain |
sangu bi sangukaay bi |
bath bathtub |
le bain la baignoire |
sarbet bi, (fompukaay bi) | towel | la serviette de bain |
saabu bi | soap | le savon |
shampoo | le shampooing | |
boros bi
![]() peñe, jartukaay bi |
hairbrush comb |
la brosse à cheveux le peigne |
soccu bi | toothpick | le cure-dents |
dantifiris bi | toothpaste | le dentifrice |
lipstick | le rouge à lèvres | |
seetu gi
![]() |
mirror | le miroir |
xeeñ gi
![]() |
perfume | le parfum |
wanag wi
![]() gaanuwaay bi ![]() |
W.C. , toilet urinal |
les toilettes l'urinoir |
bale gi
![]() |
broom | le balai |
mbalit mi
![]() |
dustbin, trash can | la poubelle |